Revue de presse (Wolof) Rfm du Lundi 11 Novembre 2019 avec Mamadou Mouhamed Ndiaye

Pubblicato il 11 nov 2019
#gamou #tivaoune #kebetu
Abonnez vous:
it-tvs.com/username-Senegal7officiel

Commenti

  • diere diefe sekhe akhemadou kara

  • Diadieuff Serigne Babacar s'y Mansour.Yal'na Yall'a Gudal wii

  • Yala nagnou yalla moussal si journaliste

    • Journaliste bi li serigne wakh rek la binde th niépeu ko dégue

  • Serigne babacar sy mansour et mbaye sy mansour pareil entoucas ,pour moi il est khalifa de la famille serigne babacar sy

  • Merci beaucoup bro

  • Serigne Moustapha wakhoul lou ay bayélén diakhasé nioum niar nio bok Mbok li lay diaring yonou kén nékousi saytané ngén trop

  • Orange d'où séne morom bilahi meunou léne té do léne bayil depuis 1 semaine damay am crédit té douma meune woté orange lolou moy l'âne so woté service clientèle nombre bi ay doul Kate rk le beuri soffffff ngay nako directeur frée diote sama mésange bi

  • Wa ok informations bi mé amna louma meti si tigo khawma ki devient free j n c op ay sathie laniou et séne dra matoul

  • Bayilén.yok serigne Moustapha. Kou amoul dég dég wakhoul ak yaw,ndakh gnie fi nék vs criyez qu'il à le simple plaisir de parlé comme ça en lair,détrompé vs mome loumouy néub amoufi,té loumouy wakh famouko wara wakhé rek lakoy,wayé Sénégal kéndoufi djibal DEUG ndakh,da bari Ay nafék,wayé heureusement bâ kouthie nék khamé sa thieurou morom entre kara ak s.Moustapha d'où mbindafoune mothie khathie,bou guissé loumouko wara wakh dakakoy wakh.ayez des réflexions positive.sur certaine propos des guide religieux é évité de mal,interprété leur propos,sof nguén bilahi walahi wa talahi Sénégal, bouniou amone niéte you melni serigne Moustapha. Kon injustices ak corruption ak mal faits diekh fi.wayé koumou nékhoul kalamel yalla?

  • Kara d daffa bakh lol

  • ab serigne day mandou serigne modou kara too nioul kéne sokhor bakhoul dieredief serigne touba amoul morom

  • Serigne Modou kara ko baxla bilahi

  • Ap serigne dal day maando fit na bakhoul

    • Mais loumou wakh dou fitna niom niar ay mbokou lan mais bou guisé serigne Modou kara déf loudoul yon mou wakh koko mbok lolou lay diaring

  • Serigne Moustapha d dafa bakhe rek kaine dou chiekhe akhamadou kara kilifa dou dagasanté

  • Merci ndiaye

  • serigne bi kaye gamougui kholo rek ladon def

  • Serigne Babacar Sy Mansour khalifa général koullou tidiane yalna fi yague ta wer

  • Bonjour

  • TÈ BOULÈN FATÈ NÈ SOUL GAZ DOUKO TÈRÈ KHÈNIE SAMA GUAYI.

  • IDRISSA SECK PRESIDENT EN 2024 INCHAA ALLAH.

  • MERCI BCP NDIAYE DIATA MOUHAMED

  • Khalifa tidiane bi wax na lou am solo deuglou nako wayé serigne moustapha dioum na cii limou wax cii serigne modou kara ndax kara dokhéwoul nonou

  • Loutass yénako tass vous les journalistes

    • Journalistes defoul dara day revue de presse day lire.lou jounal yi binde

  • Bravo serigne modou kara serigne touba rek amoul wakh

  • DIARAMA SERIGNE BABACAR SY MANSOUR

  • Yen fen rek ngeni def delen bindel nitngy lin wakh diakhase rek ngeni def say tane you bon