Madior Ak Dior - Épisode 52 [Saison 01]

Pubblicato il 15 set 2019
VIP SAGNSÉ👉it-tvs.com/plid-PL7OYJbvZchhEanHPCOYH-6MvvA5_lY0dl
Inscrivez vous à nos Castings ici👉forms.gle/y1afdWpaZGEysYS99
[ABONNEZ-VOUS ici] ☆~~👉 it-tvs.com/username-PikiniProduction
[FACEBOOK]☆~~👉 www.fb.com/PikiniProductions
[TWITTER]☆~~👉twitter.com/PikiniProd
#Vip_Sagnsé_it-tvs.com/plid-PL7OYJbvZchhEanHPCOYH-6MvvA5_lY0dl
#Madior_ak_Dior_it-tvs.com/plid-PL7OYJbvZchhHCAKLYpjgAFrKKzFTYbq3o
WhatsApp ☆~~👉 +221776626858
Pikini Productions
ByBen 2019

Commenti

  • Pikini les autres épisodes s'il vous plaît

  • Team Diorrrrr

  • Team Dior

  • Wa lgui kagn lagnouy am episode 53 bi

  • AHH LIMOM AMOUL BEN CHANCE DESNA LOU BEURI WA PINIKI TMT TEK LENKO SI YONN WAYY AHH

  • Non mére da ma ko faa

  • Wa xana madior ak dior amatoul???

  • S

  • Ça fait des jours maintenant tegouniouko tmt

  • Cône pabira mo diour Nar ak séheyi😕

  • Mane Lima diakhal moy dior ak yama ak kewé gno bokk jour anniversaire 24juillet ....Pour mane gnoy jumelle yi mais non...bobou coïncidence 🤔🤔🤔

  • Sen.theatre.bi.amoul.sance

  • J'aime bien abou l'ami d Dior 😂😂😂

  • WA khana série bi dafa jekh?

  • Non man mom saison 1 bi foumou dièkhé naxouma dara, Mai mangi xar saison 2 bi ak plaisir

  • Franchement la fin n’est pas si interessante que ça. Je m’attendais à mieux. Ils ont même pas su toute la vérité (que naar était la troisième jumelle et que dior et yama sont sœurs de même père) Dommage !

  • Madior et Dior 😍😍😍

  • Comment se fait-il que madior ne nè jamain vue sa cousine kewe qui est la soeur de yama et dior

  • Anta mom daay meer rekkk oh c trop exagéré ça

  • Li nk dèss na dh xana sx guèn df long métrage dior xam pape madior guiss yayam nar xam loumou bok ak dior d boubaba doudiar mouy am saison 02

  • Moi je dis k keweu Dior et la fille de narr on le même père 👌😀

    • Voilà. Moi osi c ck j'ai compris Dior et yama ont le même papa Pikini venez nous éclaircir et surtout k madior ne les prennent pas toutes les deux kol femmes sinin dina doy waar torop

  • Quoi c finit ?? J'ai rien compris

  • Je t'aime vous tous

  • Joli

  • Super

  • Film bi amoul se ns

  • J crois que fin bi amoule sens nakh nar dafa warona khamni mo réw jumelle lane baparé Dior dafa wala khamni mome ak madoir gno bokk nak Madior domou badianam la et yama aussi dagno wala khamni elle n'était pas enceinte

  • Nn mais comment ça Dior et Meissa sont frères ils sont pas cousin plutôt. J’vais dvenir folle xay

  • Tellement d'erreurs

  • sene film nekhna torope mais fin bi amoul chance madior guisoul yayam gueumiul ne mingui doundou nar ak maman banel guisantewougne kane mo ame dome si ki son ses enfants ak nar khamoul ne kime ray jumelle lame la film dal des na

  • Mane d je rien compris maissa mom foto bi meusse nako guiss si papame loutakh mou melni taye lako messeu guiss

  • Amoul ben chance fin bi c'est désolant madior ak Dior

  • TAY MOME DANOU GUEN MAIS MADIOR SON PERE LUI AVAIT MONTRE LA COPIE DE CES PHOTO DONC IL DEVAIT EN DEDUIRE K NAR DIOP EST LA 3IEME JUMELLE DE LA MERE DE DIOR

  • Bien

  • Lima diakhal kéwé c'est la cousine de madior,té madior khamé wouko

  • Mai li yalla boumou gaw dieh

  • Wa yenne khana madior da diekh

  • wa pikini votre sénateurs sénatrice amoule dara sene film yii douniou ame fin depuis dikon senn film ame dou fin mann doumalenn ko ball

  • Legui madior da faté photo Biko papam wanone khana thiey pikini

  • Li mome Nafi yam ngédem djanguiwat khamoulén Ndeye dr 😡😡😡😡😡😡

  • Yeene niou yabatè ngèn mai sèri bi waroul dièkh nii nii c tro facil

  • Cvf

  • Bonsoir Wa Pikini production voilà moi jai un cri de cœur comment vous avait bafouillé se téléfilm mètinama trop jai pris tout mn temps pour le regardé a chaque fois je ne sais pas combien de fois jai acheté de connexion pour regardé madior ake dior voilà arrivée au terme vous faite 26mnt pour résumait toute cette joie et de triste qu'on na partagé ici je trouve ça anormal en plus ont nais pas si c'est fini ou fin de saison voilà pour terminer dal vous n'avais pas pensé au téléspectateur qui vous regarde mèrèna lène trop wa salam

  • Amoul chance boudé fi lay yam vérité yi DESS na nar khamoul né kimou raylou c est ça jumelle

  • Amoul chance boudé fi lay yam vérité yi DESS na nar khamoul né kimou raylou c est ça jumelle

  • Noirceur bi chi film bi cè 👌👌👌👌

  • La fille qui ressemble à Dior khana daguene ko loukhous. Mais fassé Yama valide n’a walla ?? Sinon d’où woudié ak Dior .. Yama ak meunou niou woudié . Soit mok madior nio bok baye ou mok Dior nio bok baye... franchement... c’est trop tiré par les cheveux..

  • Mohh madior ak dior néxol dé

  • J'ai aimé cette série mais le dernier épisode est un fiasco une trés mauvaise fin de série sans aucune émotion

  • Finalement aucune chance linou warone xam si serie barina

  • D abord félicitations mais vs avez précipité la fin......

  • Madior

  • Qui regarde la serie en lisant les commentaires

  • Wa pikini khana s'en fin bi daflen reuthie

  • Wa kilifa bi violé dof bi témou eumbeul KO bi narr diop di wakh mom Kane leu

  • Pourquoi défou niou fin de saison

  • Excusez moi mais serie bi nekhee fin bi warone na am sens.Mais narr warna khamni yayou dior sekham la.dior warna kham papam ainsi k yama.Mariage yama ak mafior foumou moudjee ...Etc..Tamite

  • con dafa fin 😭😭😭😭😭

  • Amoul ben sens pikini mom zéro khamoulen dara

  • Courage Dior écoute ton ceour c'est important