Kooru Biddew Saison 4 - Épisode 8

Pubblicato il
Abonnez-vous à notre chaine IT-tvs it-tvs.com/ch/UCOvrLn57A83J8ojcX70n0Ew
Suivez-nous sur Facebook facebook.com/leuzmedia?fref=ts

Commenti

  • Mass lou mou def amoule tour

  • Sounds sweet

  • guerre day saf mondial

  • ' ü

  • Biddew 👍🏽👍🏽👍🏽👏🏼👏🏼👏🏼❤️

  • Bidew nak mongui beug sof wou diou rek Mou mell ni man djiguene bou bagn wou diou mom douma nex dará iss

  • Nn bidew mom ioe la faraal ms jaim op la façon dt tu traite masse....!!

  • 🙎🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • Maie mass dalo xi de

  • Bideew est trop magnifique et classe mass loy guisser kou melni bidew diko dieunder cette vielle la

  • Bideww diepi na mass nak😂😂😂😂😂😂 non daro ak dan bobou couple😂😂😂😂😂 xaran rek la dann di def mom biral rk lay topato

  • Nice trop

  • .

  • Mimi dall nop nala man

  • Va chercher un mari noire comme du charon

  • Waay ki nexnama dh bideew mi

  • Merci waye Adji nila djiguène daye foula aussi sa kharit bi baxol guènèe kou si biti

  • , Alexandra Hepburn

  • Kone masse dafa deure

  • Remarque : bidew a changé de boucle d'oreille entre quand elle quittait la maison pour le boulot et quand elle est arrivée au bureau et qu'elle repond au phone.

  • Non Nakk Mass day sëral Bidew Dico pamti-pamté rk soit le DG Goor day Njëmei🍌

  • li amoul feinn

  • Mayma quelques moments mass dinama ray 😂😂😂😂😂😂

    • Waaaw dama warou sakh..1 moment..2 moments ..3moments..quelques moments

  • Ndenga monne toggo spécial biddew

  • Team biddew

  • Bidew yawittt wakhal ak mass c pas kom ça woudjou dou dara en plus yaw ki do moromom si bène côté 🤩🤩😘😘😘

  • J'aimerais que vous abonnez a ma candidature je fais des nightcore je suis en France mais je suis sénégalais j'espère que vous voulez plaisez sur ma chaîne youtube

  • 😂😂😂😂

  • Bidew nekhna na trope nakh Dafa teyyy

  • Bidew nak yow la andak mais takal la niarel diaroul li

  • Mai mass dffa deurr wla

  • Biddew nak dafa soff kW ahhh do may mass diamou tmt

  • Bégaiement bi nal

  • Mimi elle est très jolie elle a un super beau teint mais dafa extravagante dale

  • Non bidew li ken douko def dieukeur dou morom deh

  • Mais nk Mass Amna droit takk Niar ba niet

  • Nit kou nek ak sa personnalité. Mane mome Adji damako yeureum pask defoul dara. Dafa beugu seuy rk

  • Bidew je suis ta fans depuis iralie

  • AjDA🌘

  • Lou takh Mass yambare

  • man ma beugue bideew kirassoulilah

  • Bidew way bidew way manchala danga wouyou sa tourr deh bidew deugg manchala

  • Les hommes sont bizarres; ils quittent dans ça va très bien (bidew) pour aller dans ça va pas du tout (niarel). 😂

  • Biddew Nak bet gama niou takkal la woudiou rek ga change

  • Kou guiss ne hale you goor yi Masse lagnou farral

  • Bidew je taime fort en plus tu a un joli teint machala

  • Masse yambar leu way thipppppp

  • Dane tamite wolou woul fama si wagnebii🤣🤣🤣🤣

  • Bideew nakk non franchement gniounne awoyyii nagniou bayyi yii goor Bou signer poly nakk chance rekk moyye takh dou takk

  • Bidéw man d.accorouma ak yaw woudiou diaroul li daguay guem sa bopou boul ko yeugual sa yaram boul wané ni amena loula méti

  • Vraiment 2em famme lou bakh la

  • Je ne comprends pas pourquoi vous essayé de ne faire croire k 2ème femme waroule awo doukou accepter mouk ta gnune geup gnu djoudousi je suis awo mais domou gnarel la c koi votre problème pourquoi gnakale fayda goor aussi kou tak tu assume Mme seye ba deme epuis c tt brrrrr

  • La Femme teint noire biii lolll

  • Prtan niarel bi baxna deh

  • Dane bayill daro migaye nakhe dell ndogou waye

  • Bidew ya ngi sonal sa bopp Fi ngay moudié nga ndiéké

  • Bidew mo fiir rk da melni mane mdrrrr

  • Mass tey ngay soga khamni couple communication mokay dokhal Wudiou bidew boudé yangui lirr message bi saches que tu n as pas d'amie, cette renoi là Elle est hyper jalouz

  • je trouve que Dane est un bon mari, ak lou meuneu am dafey nakhanté ak Fama rek

  • Goor buci signé Monogamy yeureum nala

  • fraîchement nekhatoul c etai pa l objectif ay 2eme femmes mom du defente

  • Yow biddew mo la man

  • Bidew Mass sa borom keur la nak

  • Masse amoul fouleuh dara siimmmmm

  • Mass ya léwét té niak khorom

  • badiane n'a gaw masse soone n'a de

  • Mass yambar ga nak naye khawa gorè way

  • Borome tin noir bi lima nèkh si mome da kham louko diapeu tes diko def lipolévre liguaye def mome Bxn calko fofou rk bisboko chabgé des dotoko défati

    • Wouyaye lipolevres 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣fogue na 2005 la gueudje dég mot bobou

  • Boudew bou rafetne

  • A thioum nék madame Gueye dal dou aye fo thieye li

  • Daro dh warnga kholat sa boppou chaque jour dann wot lay pou ndogou ji😄

  • Daro ak dieukkeur dji dinagne ma rey rék 😂

  • Bideew falèko waye

  • brava bidew e buona continuazione

  • Bidew ioe yaye kane

  • hé deugu d'où nkh bidew djiguene dayy am foula way wayé perte bâ melni lolou nonou

  • Mé pourtan il a l drw 1e deuxième fame .

  • Mass fan naaa la

  • Bidew est Chretienne wala dafa toub?

  • Deurouu mass bi à 2:50 😂😂😂😂

  • Mimi mom sokharoul

  • A mimi nak fouy nga ñiarél bagna toula ngakoy bagne ak sa kanam

  • Oh mane dal cette mimi là ne me plait pas du tout elle fait trop de manière

  • Mass tamite xana dou goor ki yaye djeukeurame dou mome moy sa djeukeure takoula yako Takk yakk nga fayda trop way

  • Proviseur fallou Cissé yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana 😭😭11 likhlass svp

  • Salut abonnelen sama chaîne

  • Ma bekk thi sama bjddew bi djigene foula niaww🤣🤣

  • Pourtant femme bou nioul bi dafa rafet

  • Wzctane rek mo gyeunnn

  • bideew je t'aime

  • Ani wa team awaa tamite pousse bleu may djiss

  • Nn mass dafa deur 😂🤣

  • Muy bien. Este théâtro es muy interessante bueno contuaçion

  • Badiane mon menkè

  • Bidiw machala rafetgha mais adji Nak mola daxe niarel mass

  • thiey djiguenou Sénégal kouniou takal woudiou rek nga changer di diaboliser sa dieukeur

  • Lou meun nek wala loumou yéyoul gouro rek😎

  • Thiey Daro néna👉doléy goor djiguén🤣 vérité absolue ngay am fofou

  • Non Mass défaillant nga koi Bidew koukay takkal niarrel ak Sa Cd bou khossou bii damal outi clé USB 😁😁😁

  • Biddew mi kat legui mou rew kat iow yay kan ba ki dou takk niarel en way